Premium Only Content
SUNU BAKAAR - ELGOZEL - ADORATION 2022 - MUSIQUE SENEGALAISE - MALAAKA BU SÉNÉGAL - WOLOF 2022
Esayi 53 vs 4 - 5
4 Ndaxam moom sunu wopp la yenu,
sunuy mitit la sëfoo.
Nun nu foog ne dees koo mbugal,
foog ne Yàllaa ko duma, torxal ko.
5 Te moom sunuy tooñ a waral ñu jamat ko;
sunuy ñaawtéef a waral ñu dëggaate ko.
Yar yi nu jàmmal moom la dal,
te mooy ki nu wére ciy góomam.
Voici les paroles de cette chansons;
sunu bakaar nga yenu,
Tu as porté nos péchés
sunuy mitit nga sëfoo.
Tu as porté notre douleur
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Man may doomam ji mu bëgg
Je suis son enfant qu'il aime beaucoup
Amna bànneex ci man
Il prend plaisir à moi
Xawmu ñu won mbëggeel
Nous ne savions pas ce qu'est l'amour,
Wanga ñu loy mbëggeel
tu nous as montré l'amour
Xawmu ñu won sarax
Nous ne savions pas ce qu'est le sacrifice,
Wanga ñu loy sarax
tu nous a montré ce qu'est le sacrifice
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Fay nga sunu boor
Tu as payé nos dettes
Xawmu ñu won mbëggeel
Nous ne savions pas ce qu'est l'amour,
Wanga ñu loy mbëggeel
tu nous as montré l'amour
Xawmu ñu won sarax
Nous ne savions pas ce qu'est le sacrifice,
Wanga ñu loy sarax
tu nous a montré ce qu'est le sacrifice
sunuy naqar nga yenu
Tu as porté nos souffrances
sunuy mitit jeexna
notre douleur est finie
Aji manji
Tout-puissant
Igwe Igwe Igwe
Le Roi ! Le Roi ! Le Roi !
Ngir liggéeyu bant bi
pour l'oeuvre de la croix
Sama dund soppikuna !
Soppikuna ! soppikuna !!
Ma vie a changé
Bo xamee liggéey bi nekk ci bant bi, woyal ak man
Si tu comprends l'oeuvre de la croix, chante avec moi
Nous vous apportons de la musique wolof gospel senegalais inspirée afin que vous sachiez et soyez conscient du don gratuit de Dieu, veuillez vous abonner et recevoir les notifications de nos téléchargements ultérieurs
Vous êtes les bienvenus sur cette chaîne, n'hésitez pas à contribuer à la croissance de cette chaîne, en regardant et en partageant le contenu de cette chaîne avec vos amis et votre famille, car vous serez richement récompensé en sauvant des vies.
LA PROPHÉTIE :
A l'Ange de l'église du Sénégal, vous vous couchez bas et dépendez de plusieurs mains, levez-vous de votre sommeil et prenez la parole avec vous, n'ayez pas peur et ne vous mêlez pas! car mon jour est là! rumakawawakushibuatimogondalibanze (Si tu n'en as jamais tiré, tu le sais)
#Gozel, #Elgozel, musique senegalaise, gospel musique, gospel, latest gospel, wolof gospel, adja et cecile, Adja et cecile, Chansons chretien, chansons wolof, chanson gospel, adja chanson, cecile chanson,Adja musique, sunu boroom bi, adja et cecile sunu boroom bi, chansons senegalaise,magal, agal touba, magal 2022, magal 2022, senegal 2022, chansons 2022, chansons wolof, adja et cecile 2022, chansons tiktok, tiktok 2022, vskit, youtube senegal, adja cecile wolof, sama dund senegalaise, video clip chretiens wolof
-
LIVE
Steven Crowder
1 hour ago🔴 Introducing ‘Next Chat’ | A Live Q&A Spectacular
18,775 watching -
LIVE
Graham Allen
2 hours agoRFK Joins Team Trump! MAKE AMERICA HEALTHY AGAIN + Sylvester Stallone Intros Trump At Mar-a-Lago!
8,680 watching -
32:08
BonginoReport
3 hours agoRFK Jr. Prepares to Battle Seed Oils & Big Pharma (Ep.86) - 11/15/24
24K57 -
LIVE
Matt Kohrs
9 hours agoPayday Friday, Breaking Market News & Live Trading || The MK Show
1,365 watching -
LIVE
Vigilant News Network
14 hours agoFBI EXPOSED: New Development Rocks J6 Pipe Bomb Scandal | The Daily Dose
3,055 watching -
1:27:24
Game On!
10 hours ago $5.49 earnedEagles DOMINATE Washington on TNF thanks to Saquon Barkley!
24.9K1 -
17:10
Film Threat
1 day agoDUNE: PROPHECY EARLY REVIEW | Film Threat Reviews
96.2K9 -
51:29
Uncommon Sense In Current Times
12 hours ago $22.16 earned"Why This Election Was For Protecting Christian Freedom"
57.6K11 -
10:46
Degenerate Jay
17 hours ago $12.49 earnedThe Rejected Superman Ending Of Smallville Would Have Changed Everything
43.4K8 -
19:01
Jamie Kennedy
16 hours agoWe're in a World of Dummies! | From Ep. 176 Hate to Break It To Ya w/ Jamie Kennedy
56.2K10